Tous solidaires pour Porokhane (Cartes membres FONDATION MAME DIARRA BOUSSO)

Collecte vérifiée


Créé le July 8, 2020


collecté



de 50 000 000 XOF

commentaires

Salamu haleykum warahmatullah. Mboki jullit yi, mboki taalubé yi, gnongi léni nouyou diléne ziar tei dileine wo si carte barkélou louyi jeum sa ligueye daara Sokhna Diarra bathia Porokhane. Liguey bi Serigne Moustapha Bachir Mbacké moko naal ngir dimbali taalibé yi gnou meune ci barkelou. Carte yi gnongi koy wéthié 10 000 F CFA.
JAAJEUF
TAWFEKH AK TAYSIIR

Moyen de paiement
Moyen de paiement
Moyen de paiement

Commentaires ()

Aucun commentaire
×
1 / NaN

Image
Partager Participer