TOUBA CA KANAM : BARKEELU SAFAR

Collecte vérifiée


Créé le September 9, 2022


collecté



de 1 000 000 000 XOF

commentaires

Souscrire à la dynamique participative de Touba Ca Kanam permet de résorber les difficultés rencontrées à Touba et la roue tourne déjà avec l’érection de routes, de postes de santé et le reverdissent de l’environnement… Donner 1000 frs en ce mois de Safar à TCK est symboliquement significatif de la gratitude du mouride envers Serigne Touba. Tuubaa Ca Kanam laaj lu ñu man, def fu ñu xam.

Nanu jaayante tàbbal sunuy barkeelu ci Touba Ca Kanam ngir saafara soxlay dëkk bi te TCK jot cee def yu am solo, niki : Defar yoon yi, naatal Tuubaa, Leeral Tuubaa, dimbali néew doole yi, wàllu wérgi yaram... jaayante bi day doon delloo njukkal Sëriñ Tuubaa ci weeru Safar wii, du tee nuy wéyal weer 1000f ci muriit bu nekk. Tuubaa Ca Kanam laaj lu ñu man, def fu ñu xam.


Moyen de paiement
Moyen de paiement
Moyen de paiement
Moyen de paiement

Commentaires ()

Aucun commentaire
×
1 / NaN

Image
Partager Participer