Déloo njukël Serigne Mourtada Mbacke

Collecte vérifiée


Créé le July 26, 2020


collecté



de 5 000 000 FCFA

commentaires

As salamou aleykoum waraxmatoullah, mboki joulite yi ak mboki taalibé yi gnou ngi léni ziar dileine wo ci ligueyou lislam bi nga xamné Serigne Mouhamadoul Mourtada (yalla na yalla tasse nou ci barkem) moko naale. Keep kou ci beugeu barkelou gnongi lay wo ci ligueye bi. Yalla na yalla barkel.

Moyen de paiement
Moyen de paiement
Moyen de paiement
Moyen de paiement

Commentaires ()

Aucun commentaire
×
1 / NaN

Image
Partager Participer